Diglé lu bàx téré lu bone
Karte bou matalébi
Tour bi: Diglé lu bàx téré lu bone
Khamlé gou teunkou: Lislàm dafa ñëw ngir sàmm joroomi mbir: diné, bakkén, xél, alal ak njaboot. Kàràngé mi ngi am ci wattu juroom yooyu. Té ni mbootàyu lislàm nimu tëddé dafay waral lahénté biir ak dimmbalaneté ci wattu kàràngé googu cila aju. Té bépp jullit kénn la ci ñiy wattu lislàm luy waral ci moom muy taxaw ci liko war ci mbookki jullitam. Mu bookk nak ci mbootàyi yi taxaw ci jamono yi mbootàyup diglé lu bàx téré lu bone. Té Diglé lu bàx téré lu bone ci toob yi gëna màgg di itam ligéy wu màgg wu Yonnénte ak ñu bàx ñi daan taxawé ndax lici nekk ci ngënél, ak yiw gu dajal, ak njariñu àdduna ak allàxira. Wayé bàyyiko dafay waral nén gëna fulu, yàxx tassàroo, ak moy gi inndi mérum Yàlla note, di waral mbugalam Yàlla ci ñëpp. Fiinak dajalé nañu fi yuy léral àtté yu ci jëm.
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/2768023
Lî môye karte bignou têkki thi lâkk yî di gneuw: Arab - Lâkkoup ouyghour - Benguali - Anglé - Indô - Bosniâk - Lâkkoup Olandé - Tâylandé - Tâjiki - Farencé - Népaléh - Ouzbèk - Sinewâ - Perse - Lâkkoup kannâdi - Vietenamien - Grèk - Lâkkoup Afar - Lâkkoup Kurde - Somalien - Ourdou - Èspagnolm - Bambara - Sinhalé - Tîlouguou - Tâmilai - Lâkkoup Akâne - Amharik - Turke - Albané - Lâkkoup âssâmy - Socé - Tijrié - Lâkoup adîgué - Mayalam - Macédonien
You amouk jokkô ak môm ( 5 )