Julli

Râgnatlé mbir yi thi lignou adjou Karte bou matalébi
Tour bi: Julli
Khamlé gou teunkou: Umpul bèpp jullite -cànte ñèlna Yalla- wàccuxâyu joulli ci lislam, mooy kénok diiné, di tàxxalé digganeté kéfër ak nguëm. Xàc bi ñi ngui ko jaglèl lèral li julli di tékki akiy àttèm, ay waxtoom, ay sartam, mélokànam, ay pooŋkam, ay faratàm, ak sunnàm, ak sujootup njumté
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/817054
Khôlal itamite ( 1 )
Go to the Top