Julli àjjouma
Karte bou matalébi
Tour bi: Julli àjjouma
Khamlé gou teunkou: Yalla tànn xètewii ci yénène xèteyi, mu tànnalko Mouhammad (Yalla na Yalla julli ci moom té doolliko jàmm) mu di ap yonènetaam, tànnal ko béssu àjjuma. Konenak béssu àjjouma amna nguënèl gou màgg ak palass bu kawé ci lislam, dajalénañu fii yuy léral nguënèl yooyu ak àtté yu aju ci bèss bi
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/817053
Lî môye karte bignou têkki thi lâkk yî di gneuw: Arab - Lâkkoup ouyghour - Benguali - Anglé - Indô - Bosniâk - Tâylandé - Tâjiki - Farencé - Népaléh - Ouzbèk - Sinewâ - Perse - Lâkkoup Olandé - Lâkkoup kannâdi - Grèk - Vietenamien - Lâkkoup Afar - Lâkkoup Kurde - Amharik - Ourdou - Somalien - Èspagnolm - Bambara - Sinhalé - Tâmilai - Tîlouguou - Tijrié - Lâkkoup Akâne - Turke - Albané - Lâkkoup âssâmy - Indonésien - Môris - Lâkoup adîgué - Mayalam - Macédonien