Fénup wéru Aviril
Karte bou matalébi
Tour bi: Fénup wéru Aviril
Khamlé gou teunkou: Fén fébar la bu màgg, ndax mi ngui bookk ci bàkkàr yi gëna ñàw té bone, bookk ci màndarga nàféx, dafay tax nite ki wacc yoonu ngëm. Bookkna ci li tassàroo ci nit ñi lii di "fénup wéru Aviril": mudi né fén ci bess bu njëkk ci wér woowu dagane na ci ludul bénn tëkk wu bawoo ci lislam. Loolu jur ay yaxu yaxu yu bari. Xët gi ñi ngi ko jaglél ci léral àttéy fén ci boopam ak fén ci wéru aviril rawatina
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/2768016
Lî môye karte bignou têkki thi lâkk yî di gneuw: Arab - Benguali - Lâkkoup ouyghour - Anglé - Indô - Bosniâk - Lâkkoup Olandé - Tâylandé - Tâjiki - Farencé - Népaléh - Ouzbèk - Perse - Sinewâ - Lâkkoup kannâdi - Vietenamien - Grèk - Lâkkoup Kurde - Ourdou - Somalien - Èspagnolm - Bambara - Sinhalé - Tîlouguou - Tâmilai - Lâkkoup Akâne - Amharik - Lâkkoup Afar - Socé - Turke - Albané - Lâkkoup âssâmy - Môris - Tijrié - Lâkoup adîgué - Indonésien - Mayalam - Macédonien
You amouk jokkô ak môm ( 1 )
Wolof: ( 1 )