Xàlid Ibn Ali Al-Ghàmidi

Aye kangam akiy kilifa Karte bou matalébi
Tour bi: Xàlid Ibn Ali Al-Ghàmidi
Khamlé gou teunkou: Mi ngi juddoo Màkka. Amna bak bookk ci ñici ràññéku ci wàllup Al-Xuràn ak sunna ak cossànu diiné ci universiep Ummoul khurà. Ci atum1412 ci gàddày gi nékkna kuñu jiital foofé ci xamxamam ci waallu nŋàggiinum alxuràn. Ci atup 1416 ci gàddày gi la am majester ci al-xuràn akiy xamxamam ci universitép Ummul xurà ci jàŋŋinu al-xuràn. Ci atup 1416 ci gàddày gi la am doctoorà ciy poñ yi gëna kawé ci facultép Al-xuràn akiy xamxamam ci université boobu ci pàccup jàŋŋin yi. Ci atup 1422 ci gàddày gi lañ kofa fal Ustàs buy jàppalé ci facultép wooté ak cossànu diiné. Ci at boobu lañuko fal mu jiité pàcc gi fété ci jàŋŋin yi ba ci diggu atum 1424 ci gàdày gi. Ginàw loolu ministér biy saytu mbiri lislàm ak mayé yiñudul doon ak wooté ak téktalé défko yilimàn ci jàkkàp Al-xayf ci Minà. Ci atum 1428 ci gàdàygi la buuru arabi sawdite bii di Abdalla diglé ñu défko yilimàn ci kàbagi.
Bess bi gnouko dougal: 2015-05-08
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/886395
Tème yi ajou thi ( 1 )
Go to the Top