Nabiil Ibn Abdi Rahim Ar-Rifaaii

Aye kangam akiy kilifa Karte bou matalébi
Tour bi: Nabiil Ibn Abdi Rahim Ar-Rifaaii
Khamlé gou teunkou: Mi ngi judd 19-06-1398 ci gàddày gici jidda. Ci atum 1415 ci gàddày gi la mookaal alxuràn. Amna majestér ci saytu mëne mënup nite. ak bac ci porotochimi. pilote la ci arabisawdite. Mi ngi tàmmbalé jitté ci atup 1415 ci gàddày gi ci kaar ci jàkkàp Al-Baghdàdi ginàwgi ci jàkkàp Alhudà ci Al-Andalus toopp mu dem ci jàkkàp Khadija Bint Xuwaylid ci Zahrà. Fiiñu tooll mi ngi jiité aka xutba ci jàkkàp At-Taxwà ci yoonup At-Tahliya.
Bess bi gnouko dougal: 2015-04-24
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/884229
Tème yi ajou thi ( 0 )
Go to the Top