Manàsik.. jomonoy Ajj 1434 ci gàddàygui [ 01 ] juroomélu poŋkk bi

Tour bi: Manàsik.. jomonoy Ajj 1434 ci gàddàygui [ 01 ] juroomélu poŋkk bi
Lâkk yi: Arab
Khamlé gou teunkou: Ci jotàybii dàñci léral juroomélu poŋkki lislàmyi, mu bookk ci jotaay yu ñu àndak Cheikh Omar Ibn Abdoullah Al-Muqbil -Yalla nako Yalla fay yiw- ci lu jeüm ci Ajj ak lu ci aju ciy àtté akiy ndékkàné akiy génndéku, kiko ligéy di Ministérup mbiri dîné ak mayéyi ak wooté ak ginndé bi ci Arabi Sawdite ci atum 1434 ci gàddaye gi
Bess bi gnouko dougal: 2015-04-13
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/883003
Lî môye karte bignou têkki thi lâkk yî di gneuw: Arab - Tîlouguou - Anglé - Benguali - Tâylandé - Ourdou - Farencé - Amharik - Lâkkoup Akâne - Lâkkoup Kurde - Sinewâ - Vietenamien - hawssa - Ouzbèk - Turke - Albané - Lâkkoup sawâhilé - Somalien - Perse - Lâkkoup Sanguô - Népaléh - Sinhalé - Ougandé - Lâkkoup âssâmy - Portugué - Tagâlontîloughou - Tâjiki - Peûl - Russe - Mayalam
Loading the player...