Imâd Zouhayr Hâfiz

Aye kangam akiy kilifa Karte bou matalébi
Tour bi: Imâd Zouhayr Hâfiz
Khamlé gou teunkou: Mi ngui jouddô Médine thi 1382 thi gâddây gui. Amna doctôra thi piri thi atoum 1412 thi gâddây gui thi université ba. Nékkône yilimâne ak khoutbakate thi joumây Al-manâratayni thi Anebouriyya ak Khoubâ. Nèkkitame kène thi gniy saytou mbôtây giye jânggalé Al-khourane thi médine. Nimou dâne saytô ay liguèye you ajou thi al-khourâne. Di kènne thi gniy saytou njânggalèm al-khourane thi université bou médine, oustaz thi tafsir thi facultèp al-kouranebi. Nèkk kiy saytou lèpp lou jeum thi bibliôtèk ba. Tânnenagnouko mouy yilimâne thi nâfilây kôr thi jâkka Yonènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâmm) thi atoum 1432 thi gâddây gui
Bess bi gnouko dougal: 2015-02-19
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/814449
Tème yi ajou thi ( 0 )
Go to the Top