Mouhammad Ibn Abdoul Wahab

Tour bi: Mouhammad Ibn Abdoul Wahab
Khamlé gou teunkou: Môy Cheikh Mouhammad Ibn Abdoul Wahab Ibn Soulaymane bôkk thi guîrouk Tamîm, mi ngui joudd thi 1115 thi gâddây gui thi deukk bou toudd Ouyayna thi arabi saoudite, beurina loumou taalîf. Borôm kham kham yi mândou yi sédèlnagnouko kham-kham ak am dîné ak tégé thi yône wou joup. Fâtouna (Yalla nako Yalla yeureum) thi atoum 1206 thi gâddây gui amône 91 ate.
Bess bi gnouko dougal: 2015-01-29
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/809453
Lî môye karte bignou têkki thi lâkk yî di gneuw: Arab - Sinewâ - Ourdou - Ouzbèk - Albané - Almanach - Èspagnolm - Bulgare - Benguali - Bosniâk - Tâylandé - Roumanai - Sinhalé - Chéchène - Somalien - Tâjiki - Lâkkoup foullâto - Katalaniya - Malayé - Indô - hawssa - Yôrouba - Perse - Turke - Anglé - Farencé - Amharik - Pachtô - Indonésien - Tîlouguou - Russe - Lâkkoup ouyghour - Japoné - Mayalam - Lâkkoup kirgîs - Tagâlontîloughou - Lâkkoup Kurde - Koréins - Tâmilai - Vietenamien - Lâkkoup Olandé - Pôlandé - Népaléh - Itâlien - Tijrié - Lâkkoup sawâhilé - Lâkkoup âssâmy - Lâkkoup kannâdi - Oromô - Lâkkoup tourkoumani - Lâkkoup Afar
Tème yi ajou thi ( 2 )