Moustapha Râd Al-Azâwî

Tour bi: Moustapha Râd Al-Azâwî
Khamlé gou teunkou: Mi ngui jouddou thi 19-04-1986 thi Âzamiyy thi Baghdad thi Irak. Nékkônna - Yalla nako Yalla yereum- kènne thi mbôtâyoup jânggkate alkhourâne yi thi Irâk, bôkkna thi ay jongânté you bari, mi ngui fâtou thi 26-05-2007 thi jâmârlôk soldâroup amérik yi. Yalla nako Yalla bôlé thi gnimou nânggoul sène dé thi yônou Yalla ak gni deuggou.
Bess bi gnouko dougal: 2014-12-26
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/801381
Lî môye karte bignou têkki thi lâkk yî di gneuw: Arab - Anglé - Tâjiki - Lâkkoup kannâdi - Benguali - Tîlouguou - Népaléh - Socé - Sinewâ - Bambara - Lâkkoup Akâne - Farencé - Ourdou - Tâylandé - Albané - Sôninké - Lâkkoup Olandé - Perse - Mayalam - Somalien - Roumanai - Lâkkoup ouyghour - Grèk - Vietenamien - Lâkkoum arméni - Ouzbèk - Lâkkoup Afar - Amharik - Itâlien - Lâkkoup Kurde - Tijrié - Èspagnolm - Lâkkoup tourkoumani - Sinhalé - Indô - Tâmilai - Lâkkoup Sanguô - Portugué - Lâkkoup sawâhilé - Bosniâk - Turke - Lâkkoup âssâmy - Ougandé - Kazak - Russe
Tème yi ajou thi ( 0 )