Mahmoud Khalîl Al-Houssary

Aye kangam akiy kilifa Karte bou matalébi
Tour bi: Mahmoud Khalîl Al-Houssary
Khamlé gou teunkou: Cheikh Mahmoud Khalîl Al-Houssary môy serignou mbôlème jânggkatou égipteyi, di jîtémbôtâyou jânggkatou al-khourane yithi addounabi. Mi ngui jouddou thi tâmbalik atoum ajj thi atoum 1335 thi gâddây gui tôllôk 17 sèptembar thi atoum 1917 thi atoup toubap. Thi deukk bougnou douppé Chabrae namla bi jôkk thi tâMahmoud Khalîl Al-Houssarynetâ tho sôwwou égipte. Mi ngui fâtou thi ngônou altiné16 mouhârram atoum 1401 thi gâday gui tôllôk 24 nôwembar 1980 thi atoum toubap guinnâw joulli gué. Limou enregistré thi alkhourâne: kâmil thihafs jogué thi âssim atoum 1961 thi warch bi jogué thi nâfi' 1964 qâroune ak doûrî jogué thi abî Amr bou Basra thi atoup 1968, kâmil biy jânggalé thi 1969, kâmil bou ând ak piri thi 1873. Yimou tâlîf: attèy jânng al-khourâne, foukki jânggine thi Ach-châtibiyya ak Ad-dourra, mândargâm kham fi ngua wara tâmmbalé ak fi ngua wara takhawé thi jamono bi ngua jângg al-khourâne, Oubbité guou reuy gui thi mouslou ak kâbbar, jèkhite bi geuna rafète thi dounndoup foukkak gnènnti jânggkate yi, ânddak al-khourâne bou tèdd bi, njângginou warch joggé thi Nâfi bou madîna, njângguinoup Doûrî bi jogé thi Abî Amr Al-Basrî, lèrou kholyi thi njânggoum imâm Yaqoûb, yônn wou yômb nguir njângginoup imam Abî Jâfar, bèglé gou rafète thi dajalé digganeté Ach-Châtibiyya ak Ad-Dourra, yônn bou bèss thi kham-khamou ni gnouy jânggé al-lhourâne
Bess bi gnouko dougal: 2014-12-11
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/794933
Go to the Top