Ngënélu jook book ak rafetal ci way jur yi

Râgnatlé mbir yi thi lignou adjou Karte bou matalébi
Tour bi: Ngënélu jook book ak rafetal ci way jur yi
Khamlé gou teunkou: Xëtup ngënélu jook book ak rafetal ci way jur yi. Rafetal ci way jur yi ci jëf yu bàx yi gëna màgg la book ginàw wétal Yalla mu sell mi te kawé. Rotna nak ci yonal wu jup bi de lislam ay làyà akiy adis yuy téktalé ngënel yi ci nékk. Niki noonu itam ŋëwna ci dunndu mak ñu bàxñi ay missaal yu am solo ci rafétal ci way juur yi. Lislam nak jànŋaléna ci ay xéte yu limu ci sen dunnd ak ginnàw biñu fàtoo. Xët wi nak lolu lañuko jaglele.
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/2767943
You amouk jokkô ak môm ( 1 )
Go to the Top