Gëstu yu wuuté ci Al-xuràn

Râgnatlé mbir yi thi lignou adjou Karte bou matalébi
Tour bi: Gëstu yu wuuté ci Al-xuràn
Khamlé gou teunkou: Toomb bi dina làmmboo ak ay mbir yu bari té aju ci Al-xuràn, niki: ay jaglém, atté ak téggini jàngg ko ak déglu ko ak jikkooy wa Al-xuràn, toomb yi ci saar yi, ak àya yi ak séni tur ak jubluwày ak limulàmboo ci ay toomb, jàŋŋalé ko, akiy tënkk ci limu làmboo, ay néttaliém, ay missàlam, ay xarañam, ay dàggassantém, ay ñànam, xamxam yiñu ci bàlluloo, mookal al-xuràn ak bàt yi ci nduroo.
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/887073
Go to the Top