Téktal yiy wané né Muhammad Yonéntela (Yàlla na Yàlla julli ci moom té dolliko jàm)

Tour bi: Téktal yiy wané né Muhammad Yonéntela (Yàlla na Yàlla julli ci moom té dolliko jàm)
Khamlé gou teunkou: Xët wi mi làmmboo yu aju ci téktali Yonéntegi ci làkki àdduna bi, séddalikoo ay toomb yu wuté: * Kumpa yimu xibàré (Yàlla na Yàlla julli ci moom té dolliko jàm) * Xarbaax yiko Yàlla jox (Yàlla na Yàlla julli ci moom té dolliko jàm) * Xibàré yu aju Yonénte yu jiitu (Yàlla na Yàlla julli ci ñoom) ak bégal guñu bégal séne xéte ci ak ñëwam (Yàlla na Yàlla julli ci moom té dolliko jàm)
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/887015
Lî môye karte bignou têkki thi lâkk yî di gneuw: Arab - Benguali - Lâkkoup Kurde - Anglé - Lâkkoup Olandé - Ouzbèk - Bosniâk - Tâylandé - Lâkkoup ouyghour - Tâjiki - Farencé - Népaléh - Perse - Indô - Sinewâ - Lâkkoup kannâdi - Mayalam - Vietenamien - Grèk - Lâkkoup Afar - Bambara - Somalien - Ourdou - Èspagnolm - Socé - Sinhalé - Tâmilai - Tîlouguou - Turke - Lâkkoup Akâne - Amharik - Albané - Lâkkoup âssâmy - Môris - Indonésien - Tijrié - Lâkoup adîgué - Macédonien
You amouk jokkô ak môm ( 1 )
Tâjiki: ( 1 )