Bandar Ibn Abdoul Aziz Baliila

Aye kangam akiy kilifa Karte bou matalébi
Tour bi: Bandar Ibn Abdoul Aziz Baliila
Khamlé gou teunkou: Mi ngi juddoo Makka ci atum 1395 ci gàddày gi; fala dooré jàŋŋ ba am bak. Amna majestér ci atum 1422 ci gàaddày gi ci fikh ci universitém Ummul Xurà. Amna itam doctoorà ci fikh ci atum 1429 ci gàddày gi ci universiép Madiina. Jàŋŋaléna fikh bu kawé fa Kàbaga, Ustàs la buy wuutu ci universitép Tàif. Yilimàn la ak xutbakat ci jumaay Al-Amiira Nawf ci Al-Aziiziyya bi ci Makka ak universitép Ibn baaz. Fal na ñuko yilimànu Makka béssup dibér 12-09-1434 ci gàddày gi.
Bess bi gnouko dougal: 2015-05-08
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/886360
Tème yi ajou thi ( 1 )
Go to the Top