Chirzâd Abdour-Rahmane Tâhir

Aye kangam akiy kilifa Karte bou matalébi
Tour bi: Chirzâd Abdour-Rahmane Tâhir
Khamlé gou teunkou: Mi ngui toudd Chirzâd Ibn Abdour-Rahmane Ibn Tâhir Ibn Hassane Al-Kâfy Al-Kourdy Ach-Châfi î, mi ngui jouddô thi beutt gânnârou Irak thi atoum 1968 thi fou gnouy wakh An-Nâmâiyya. Fôfou la jânggé thi ay serigne you bari niki: Cheikh Abdoul Latif Ibn Khalil As-Soufy, ak Cheikh Al-Hafiz Ali Ibn Houssayn Al-Wassâbi, ak Cheikh Al-Hafiz Abdour Razzâkh Mouhammad Imâra, ak fénène tamite. Jîténa thi ay jâkka you bary thi Irak ak Imarate.
Bess bi gnouko dougal: 2015-02-19
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/814451
Tème yi ajou thi ( 0 )
Go to the Top