Yahya Ahmad Al-Halily

Aye kangam akiy kilifa Karte bou matalébi
Tour bi: Yahya Ahmad Al-Halily
Khamlé gou teunkou: Môy Cheikh Yahya Ahmad Mouhammad Al-Halily, jouddô deukkou halila thi Yémène thi atoum 1372 thi gâddây gui tôllôk 1952. Mi ngui dôré thi jotâyoup njânggoup Al-khourane thi joumâ bou mak bithi capitâlbi dâldi môkkal thi atou 1962. Ginnâw gui mou jângg jourôm gnâri jânggine yi thi ay borôm kham-kham you bary. Mou dâldi am lou tôlôk lijâssâp lisense thi ministèroup yargui ak njânggalémi thi atoup 1973 fèkk tâmbaliwôna njânggalèm Al-khourâne thi atoup 1970, ak di jîté aka khoutba thi joumây tahrir thi saneâ (capitâlbi), niki nônou dôrena jîté attékatou jonganetèp al-khourâne thi atou 2000 thi deukkam ak égypte.
Bess bi gnouko dougal: 2015-02-19
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/814448
Tème yi ajou thi ( 0 )
Go to the Top