Bâsil Abdour Rahmane Ar-Râwî

Aye kangam akiy kilifa Karte bou matalébi
Tour bi: Bâsil Abdour Rahmane Ar-Râwî
Khamlé gou teunkou: Mi ngui jouddô Bagdad thi atoum 1953, génné thi universitèp Bagdad thi Facultèp Droit ak polotik thi atoum 1975, mou nékkône ki jîtou. Ginâw gui ministère biy saytou mbiri tougeul jeulko thi atoum 1977. Wayé mou tokhou thi liguèye bôbou, dâldi sôbou thi jângg ak jânggalé Al-Khourâne ba amthip ap lijâssa thi njângginou hafs thi yônnouk Ach-Châtibiyya thi doctor Sayid Mouhammad Sadati Ach-Chinegiti moudi ap oustaz thi universitèp Mouhammad Ibn Saoud bi thi Riyad thi atoum 1997. Fîmou nèkk mi ngui sâgnth thi arabi sawdite thi Riyad.
Bess bi gnouko dougal: 2015-02-19
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/814447
Tème yi ajou thi ( 0 )
Go to the Top