Ibrahim Mouhammad Al-Jarmy

Aye kangam akiy kilifa Karte bou matalébi
Tour bi: Ibrahim Mouhammad Al-Jarmy
Khamlé gou teunkou: Mi ngui jouddô liban thi atoum 1966, amna doctôra thi lâkk arabe akiy adabam, akoum dipolom bou kawé thi njanggoum charia (rawatina thi njangginou alhkhourân), té môy saytou njângginou alkhourâne yi ak toudd Yalla yiy daw thi rajôp Hayâte FM, di saytou tamite dâra alkhourâne bi bôtou thi ministèroup ndimmbeul yi Ordatiyya, falay jânggalé njâgginou alkhourâne liko dalé thi attoup 1990 ba tay. Nékkena tamite jânggalékate thi yènn faculté you charia thi Ordone, wayé légui mi ngui jânggalé thi univérsitè mondial bi thi malézi. Amna ay téré youmou tâlîf niki: * Jèkhinetaloup téktalèp lâkk arap thi woûté joulliteyi thi thiôssâni dîné * Khétou kham-kham yi thi alkhourâne * Joubal lâmmign thi njângoum alkhourâne * Bagna am jafé-jafé thi diggananeté joullite yi thi sèni mazap yi gnouy askanô menoul gnâkk té faratala * Sânggoup jânggkateyi Ach-Châtiby * Chawâhidoul Khourrâ * Gnou râgnékou thi jânggalékate yi ak gnilène jâggal.
Bess bi gnouko dougal: 2014-12-25
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/801022
Tème yi ajou thi ( 0 )
Go to the Top