Loottloo gu xamxamé gi ci Alxuràne

Râgnatlé mbir yi thi lignou adjou Karte bou matalébi
Tour bi: Loottloo gu xamxamé gi ci Alxuràne
Khamlé gou teunkou: Boroom xamxam yi bërina lu ñu wooté ci wallu loottloo gi ci Alxujràne digganté ku ci andd ak ku ci anddul, wayé yitté bi yenn jox wall gi taxna ñu giss né dinañulén tànnal yi ci ¨sàmmoonték sarte yiko boroom xamxam yi tégal; niki: baña juuyoo ak pirim Alxuràne bu wér, sàmmooneté ak tërëliinu wax, mu dëppoo ak làkkup aràp bi, baña wuté akup cossàne ci lislàm, tému baña soss yoon wu jëm ci bidaa.
Adréss bougnou gâttal b: http://IslamHouse.com/2768015
Go to the Top